Fonétik & Bay Zale- Panne Africaine ( LRGB, La Compilation)
Titre : Panne Africaine Artistes: Fonétik & Bay Zale Album: LRGB, La compilation Prod: Pypa 4MYDOGG RECORDS Production : Loudoul Rap Galsen Beugouniou Suivez-nous sur les réseaux sociaux: Facebook 👉🏿 / loudoulrapgalsenbeugouniou Instagram 👉🏿 https://instagram.com/loudoulrapgalse... Site web: https://loudoulrapgalsenbeugouniou.co... Contact : [email protected] / +221 781105992 Lyrics 1er Couplet (Fonétik) Njëlbeenu bep continent lu waral ñëp raw ñu respect dawul sunu diggënte tax ken nawu nu Ñàkka xam sunu valeur motax ñu jàpp ñu jaam Ba leegi do xam si xel lañu contrôler yeew ñu xalam mësul neex te buumu jaam gi mësul dog kane moy sa mbòkk? Ki la noot demb tek la choc ay njiit yu amul bòpp ñëp la ñu guux si trône marionnette France Afrique yi gëna di ñàkk jom. Da ngeen ñu añé demb tay ñooy sen dèssert dèssè tu ñu dara boy yi fàxx utali désert. luy négritude ? Ma dellu wax Césaire ni africain bi gëmul africain kon mënul gagner guerre. Rip khadafi ndax Afrique mola seetàn sa mbëbët mo doon nek ben ba lu nu sòng mën daan Feebaru continent bi doomu Afrique ñoo ko sooke Judu si gileem nàmp si mbaam tax xel yi bloquè. Refrain Bu desse lu dul dund jaam na ñu dee si ndool Non non na ñu dee si ndool Ñun bëga tu ñu ku ñu yapp ñun la der bu ñuul Non bëgatu ñu kuñu xeeb nigger Bu desse lu dul dund jaam na ñu dee si ndool Bilay wallay na ñu dee si ndool Ñun bëga tu ñu ku ñu yap ñun la der bu ñuul Freedom Mama Africa 2e Couplet (Bay Zale) Li xel di njoort Mom la xol bi yëk gisu ñu pénk Si sunu Afrique lañuy wër jant bu fènk Fu xel yi panne Xol yi ñuul Xaalis doon fa docteur Welcome To panne fric Toubab bi nek sauveur Ñooy ñi muus si lep té lambalé fi xel di jaay Su marché xel doxé Bët du gis doole bi ñu fa jaay A frique yéwul bañ toubab bi sànk la Royal si Mandela Ba nopi dëggu teey ni Sankara Am na ñu fi royukaay Luy ndey’u dem di waliyaan Sëñ Bamba yeem na ñëp El hadji malick doyna kèmaan Baye yanu na Niass bi wër’ ak mom si mari-fat-bi - lahi. Lay lay sa yoff Kuy der bu ñuul Mën nga Roy si mame Am na ñu fi lep Mën na ñu bay sunu koom Bu ñu bëgge CFA bi jog fi Mën na ñu fas sunu jom Sa njëlbeen la ñu koy dooré mëna doxal sunu bòpp Bu ñu nangu ken di ñu juutal pour ñuy doxe sunu bop. Refrain Bu desse lu dul dund jaam na ñu dee si ndool Non non na ñu dee si ndool Ñun bëga tu ñu ku ñu yapp ñun la der bu ñuul Non bëgatu ñu kuñu xeeb nigger Bu desse lu dul dund jaam na ñu dee si ndool Bilay wallay na ñu dee si ndool Ñun bëga tu ñu ku ñu yap ñun la der bu ñuul Freedom Mama Africa 3e Couplet Fonétik school bi jàngaluma sankara ndaw bañ ma fippu référence doko xool si Blaise ak Mobutu Jàppal si cheikh anta diop sooy wër kàngam Ëttu xam xam baa ngi bled amul luy nëbëtu Bay Zale Amoon na ñu Mamadou Dia pour bañoon oom yi sukk Senghor kaf ba ray ko yombal sodomie France la juutu Xam xam mëno ko am sunu school yi ndax derr bu weex lañ lay ñu jàngal nu muy naxe bu ñuul bi Refrain Bu desse lu dul dund jaam na ñu dee si ndool Non non na ñu dee si ndool Ñun bëga tu ñu ku ñu yapp ñun la der bu ñuul Non bëgatu ñu kuñu xeeb nigger Bu desse lu dul dund jaam na ñu dee si ndool Bilay wallay na ñu dee si ndool Ñun bëga tu ñu ku ñu yap ñun la der bu ñuul Freedom Mama Africa

Mister Ndiol & Dina- Dou Talent ( LRGB, La Compilation)

Safari Trips Went Horribly Wrong

Izapt & Ibrain- Cas Chaud ( LRGB, La Compilation)

Funny Football Moments That Actually Happened 😂

NERVOUS 12-Year-Old Who Can Sing Without Opening Her Mouth Earns Mel B's GOLDEN BUZZER!

People Who Messed With The Royal Guard and Regretted It!

scariest crosswind landings caught on camera

MAMA AFRICA- Tiwony, Apollo j, Baba Samba, Singleton, Takana

My Golden Retriever Heals a Terrified Rescue Kitten in Just 3 Meetings!

Mélomane Power: Panne Africaine en live ( Fonétik - Bay Zal- Jside B)

FONETIK Dale Diame Freestyle #3 ( Directed by PMP )

Incredible Safari Moments Caught on Camera

Nigger Mee & Meuz- Mbed Buur ( LRGB, La Compilation)

JANITOR vs THE BIGGEST GUY IN THE GYM. HE Didn’t Expect THAT

Tiken Jah Fakoly - Plus rien ne m'étonne (Le Grand Choral 2024 - @Nuits de Champagne)

Comedy Moments in Football

Unbelievable Smart Worker & Hilarious Fails | Construction Compilation #1 #adamrose #smartworkers

German Shepherd's Heartwarming Reaction When First Meeting Abandoned Kitten

Princess Of Boogie Woogie Delights Everyone

