Nigger Mee & Meuz- Mbed Buur ( LRGB, La Compilation)

Titre : Mbed Buur Artistes: Nigger Mee & Meuz Album: LRGB, La compilation Prod: Emma Infinity records Production : Loudoul Rap Galsen Beugouniou Suivez-nous sur les réseaux sociaux: Facebook 👉🏿  / loudoulrapgalsenbeugouniou   Instagram 👉🏿 https://instagram.com/loudoulrapgalse... Site web: https://loudoulrapgalsenbeugouniou.co... Contact : [email protected] / +221 781105992 Lyrics Refrain ( Meuz) Nee nañu mbed mi moy Mbed mi mbed buur la Ni ñu ko gisee moy Da ngay gore ñu suul la 1er Couplet ( Mee) Si quelques bars ma jëmël mbed mi ba nopi taxaw tagg ko Ndax ku yor sa baat laata ngay wax faaw nga tàgu ko Mbed bëggul fainéant kuy dunde ma ñam kase Su don xëy di wax dina tas reew ni Maniang Kassé Lo xamul teey see gën Kañ ngay gëm ni mbed buur lë te mo ëpp doole president Aay si tuxal nguur Say-sayu bukki njuur Ba nopi gaaw si taggat yuur Tay ni nangam sangam Yaru wala pankam Mbed mukk du gis luy dox mu siy tek tankam Kifi teegi woon ay chartam Laajal jot na xaru daaw Ñi gëmni mbed buur lë wëy’ag sen naqaru daaw Politique yi lay indexer joxoñ len bàràmu tuumë Ndax man mbed moma sigilo motax ba ràmatumë Lu lë mbed wax baayi si xel gisko Jaxran Ndax lan Mamadou diop ak Fodé Ndiaye Ñom si mbed lañu jaaxan du caxaan Tay boy yu coster ñokoy nëxël Rëb kuñu pëtëxël Mbed bëggul seral nel kufi daagu na xël Mbed bangi banque soor len règlement de Compte Boy yi ragal éChec sadique di gën di pank Gëmël ni mbedd buur lë te mo njaboote ñepp Malaadu gangster la gacco te mom lë boote ñepp Mbedd Buur lë haters bi Daggam Meuz Ak Mee ni samm kat pël bu jitël nagam Refrain Nee nañu mbed mi moy Mbed mi mbed buur la Ni ñu ko gisse moy Da ngay gore ñu suul la ( x2) 2e Couplet ( Meuz) Leegi wegatuñu dara mag ñi fuñu ne Ndaw ñi gedd daara yi dem di jeem lu ne Bëy yi tumranke kilen wara saam reer Ki daqqa sap moy nguuru taxna all bangi riir Dërëm jaay la lëndëm nga jël wecceko sa leer Ñi di sol si nopp yi digge ñuy deg riir Mbed buura ko mom taxna doole moy dogal Nena aayul dagg yi lë nañu ko wayal Wayal len xol ye tang jër ba melni four Ñi takk bâche tiim ëmb ker yi lañuy muur Raye pour dund si mbed don fa kilifë Mbeda ñu defar gise ko ni jubbal daño të Boy yi yagg ñaf ci ay liif ay coup de Feu Bu sacc yeegati police dagg len tous les deux Samp anarchie di bruler feu yi amul Queue Door fayu nekatul tooñ logique lë Jàgg ji late leegi melni saamu yaboy 100 A la place de l’homme qu’il faut ñu tek fay militant Mbed mi wëy di defar xelu yaqq kat yi Ecole bi gëna mag ci reew moy defar sacc kat yi Palanteer bey wane boy dugg fingay jaar Jaay dëgg mu lamb ngay fen pour mu jar Galañu takk mënal xëc boy bañ mu fay nigger Refrain Nee nañu mbed mi moy Mbed mi mbed buur la Ni ñu ko gisse moy Da ngay gore ñu suul la ( x2)