Waxtaan bu am solo ci Doundouk Mame Diarra Bousso | Waydjuru Serigne Bi (Partie 2)
Bienvenue ci seen chaîne Jambarou Mouride 2.0. Ci biir vidéo bi, nuy wéyal waxtaan wu am solo wi nuy def ci doundouk ak jaar-jaaru Soxna diiné, di sunu yaay Mame Diarra Bousso (Radhiyallâhu anhâ). Horodatages (Timestamps) 00:00 - Introduction ak nuyoo 02:15 - Rappel ci li amoon ci Suite 01 05:30 - Njanguum Al-Khuraan Mame Diarra 10:45 - Relation ak Mame Mor Anta Sally 18:20 - Lamine bi ak liggey bi ci biir kër 25:00 - Yar bi mu yaré Khadimou Rassoul 32:15 - Résumé ak dëgg-dëgg yi ci doundam 56:00 - Conclusion ak ñaan Lii moy Suite 02 bi. Deggluleen bu baax mbirum "Waydjuru Serigne Bi", ni mu doundé l'Islam, njubélam, ak yar bi mu yaré borom Touba. Waxtaan wi dinay leeral lu bari ci doundou Mame Diarra, li dale ci bi mu nekke xalé ba bi mu nekke ci kër seuyam. Lii moy li nekk ci vidéo bi : • Yaar ak téguine ci biir kër • Njanguum Al-Khuraan ak l'Islam • Diggenté Mame Diarra ak Mame Mor Anta Sally • Ak yéneen xéeweul yu bari... Abonné leen ci chaîne bi, bëss leen cloche de notification bi ndax douneen rathie dara ci série bi. Te kune xamna ni xam doundouk Mame Diarra, moy xam yoonu njub. #mouride #serignetouba #touba #bayefall #cheikhibrafall #jambaroumouride #senegal #mouridisme #bayendiagadiop #wolof à

Mame Cheikh Ibrahima Fall ak S. Mahmoud Mbenguéré : Leral bu am solo !

🚨INTÉGRALITÉ:wakhtan Sokhna Dienaba Thioub ci seydina al hassan salam

XAMLE Tout Les Federations dé Dahiras Sokhna Diarra BOUSSO Dépus 1976 à 2020 Sous le Ndigual de Seri

🔴LIVE 🔴KENN DU SERIGNE BI AVEC S. HAMIDOUNE DIOP

Ndekanou Serigne Touba Par Serigne Bassirou Mbaccke Xelcom

A Very Important Conversation About Serigne Mouhamadou Fadel Mbacké, Son of Cheikhoul Khadim!

Le miracle de Porokhane : Comment Sokhna Diarra a marqué l'histoire de l'Islam

HISTOIRE JANGUM YËKËTI

🔴DISCOURS PERTINENT DE OUSTAZ LAMINE NIANG DEVANT SERIGNE BABACAR SY ABDOU ZIARRA SSMA ÉDITION 2026

Témoignage sur SEYDINA AL ASSANE SALAM: Njariñal baayi toxum poon

Le Pacte Sacré : Serigne Mandoumbé Khabane et Serigne Touba

Le Lien Mystique : Entre Cheikh Saliou Fall Darou Khaffor et Serigne Touba

Cheikh Malamine Ndiaye Khewar ak Serigne Touba | De Ndoucoumane à Darou Salam !

Waxtaan ci Khassida Sindidi : par Serigne Bassirou Mbacké Khélcom

Waxtaan Ci Doundouk Mame Seynabou Ndiaye de A à Z | Waydjuru Cheikh Ibra Fall (Suite 01)

الرقية الشرعية للشفاءمن السحروالعين والحسد حصن من الشيطان رقية البيت والاولاد بصوت القارئ سعيد حمدان

Wakhtan wou yémé si bi Serigne Touba wouyo Boromam bouSerigne Djily Mbacké kosso

SERIGNE SAM MBAYE GAMOU LOUGA 1996

Les 4 ans de Serigne Touba en Mauritanie : L’Histoire Complète (1903-1907) | Par S. Khayri Diakhaté

