Daaraj family - jamono (official music video)

NEW ALBUM "YAAMATELE" AVAILABLE ON JANUARY 31st 2020 stream Jamono(deezer,spotify,apple,google...) : https://DaaraJFamily.lnk.to/Jamono Précommande Yaamatele 31/01/2020 : https://daarajfamily.lnk.to/Yaamatele ---------------------------------------------------------- Directed by Aymeric austry written by: Ndongod and Aymeric Austry Produced by faada Freddy for Bois Sakré lyrics: ndongod & Faada Freddy Recorded at: Karantaba mixed by: Sam "excuse my mix" Final Mix : Ludovic Joyeux Mastering : Benjamin Joubert Dop: Tom Escarmelle Lights: Fatha Edited by: Voice Africa Make Up : Khady Niang Redlips Production company: Bois Sakré All Made Distributed by: Think zik/Idol ---------------------------------------------------------- Daaraj Family On line :   / daarajfam_officiel     / daarajfamily     / daarajfamilyfan   http://daarajfamily.com/ (c) 2019 Bois Sakré/All Made ---------------------------------------------------------- Lyrics : Naka dëkk bee, naka sa boor, naka sa boor (x2) Léeg-léeg damay bëgg gàddu samay loxo yuuxu mettit Damay bëgg give up yenn-saay Tolof-tolof ak i nattu yu takku bëgg yóbbu sama fit Xam naa ne àdduna duma ray Coono dafay defar xolu doomu-aadama bi ci ngëm Jàmbat mayu ma njegenaay Buur Yàlla rekk a xam li nekk sama dënn maa koy dekku Baña jeng ta gëm ne ginnaaw jafe-jafe noflaay Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama… jamano la jamano la jamano la jamano la Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama… jamano la jamano la jamano la jamano la Jamano kow lañu jële Xamuñ noflaay dinu mbëllee Rêves yu la sut aka kowe Gént boo fàttee connexion bi da fa dem Fok ñu am pass dañoo calé Daf ma yéem ñaata jéem ñaata yoon lañu jéem Yoonu suuf yoonu ndox fëgg fu ne fu nuy jaare Kan moo nuy jàlle jotu ma nelaw biig yaakaar gën a diig fok nu génn ci Lan moo nu jig ñàkk pare ci (jamano di gën a tërëdi) Loo génn kër gis àdduna bi ci écran bu tuuti accès illimité (wuti visa) Loxo yaa ngi clické souris yi défilé actualité ni muy dikke, bu la benn ngelaw yóbbaale Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama… jamano la jamano la jamano la jamano la Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama… jamano la jamano la jamano la jamano la Rakk bul wori di nga jéggi ndox Bu soobe Buur bi gone dina màgg bay dox Lépp dina baax lépp dina baax Lépp dina baax lé lé lé lépp dina baax Du jikko jamano la du dara jaar-jaar la Boroom karaw gu ñuul ñàkkul dara dara Jombula Dara dara warul jomb góor-Yàlla gu am ngëm gu kowee Te nga jéem a bey sa tool Yàlla du beykat bul xaar fu muy tawe Di nga gis sa yoon jamano naqadi toogal ci dëkk bi jaayonte Sélébeb yoon la jamano tërëdi fonkal sa bopp li ngay jànkoonte Bu la kenn def jaam tukki du tekki fépp la metti Làbbali fas buumu gàcce nga tekki Xaalis dafa ngande làmmiñ ci jamano dëgg ne patt Doole poos ak kàrt gab moo lay waxloo moytul bëtu xol bi patt Paaka ci put bu mu tax nga bonn xoolal fu sori bul jàdd koñ Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama… jamano la jamano la jamano la jamano la l Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama… jamano la jamano la jamano la jamano Jikko jamano la Jikko jamano la Jikko jama… jamano la jamano la jamano la jamano la ... ---------------------------------------------------------- Lyrics (English): how is the country? how you been? what's up? sometimes i just want to scream my pain i feel like giving up Trouble keep coming, i'am losing patience cause life is getting tougher but struggle made me tougher and so is my faith And I know I can't win if I am complaining lord knows my heart can't take it But I hang in there cause I know after rainy days come sunshines it's a matter of time (x6) This era is hard on us, life don’t gives you lemon Our dreams are getting further, we forget them, there's a disconnect we need a password, we locked How many times we tried? By Land and Sea , we tried them all! We need a way out, im losing sleep, losing hope We need to make it What we need is not to be broke anymore (Life is harder and harder) We see everything on small screens with unlimited acces (Let's go get the Visa) Fingers clicking everywhere , news harassing us Don’t let yourself go it's a matter of time (x6) Brother don’t worry, you will fly God’s willing you will make it out Everything will be better, everything will go (x2) It’s just a matter of time, it’s temporary Nappy hair you will overcome the hurdles Your faith can move mountains Help yourself and God will follow, otherwise who else will do it for you? Its hard, but stay here, even if you gotta struggle Multiple voices, believe in yourself to face You are nobody’s slave! Exile is no success, its worst over there Go ahead , keep your head up Money talks louder than truth Our pockets, debit cards talk for us We losing faith Even with the knife on your throat Don’t lose your path it's a matter of time (x6)