VJ - Kaay Waay (clip officiel)
Streamer DM : https://bfan.link/dm-4 PRODUCTION : HOSIDE & BLZ MUSIQUE : AKATCHE LYRICS : VJ - KHRU - OMAR SARR PRODUCTION VIDEO : REVERSE STUDIOS ASSIST. DIRECTOR : DJIBY NIANG ASSIST. CAM LAMINE CISSE PHOTOGRAPHER : ARONA WADE DECO : NDAYANE DECO CASTING : NA YOODI EDITOR&VFX : BILAL MBENGUE CHOREOGRAPHY : BARRY KUSH DIRECTOR : BILAL MBENGUE D.O.P : LEYE GUEYE DRONE OP : ARONA WADE ACCESSORIES : BRASMAGIK MAKEUP : SOKHNA FATOU DIOUF STYLIST : Bright look (Elzo bouba) / Mushei COLOR GRADING : BILAL MBENGUE STUDIO WATCHTHESTUDIO221 SPECIAL THANKS : TEAM VJ, MANSOUR MOTORS Lyrics Kaay waay Ndeke dou mbeuguelou Kassè Teh sax xetou mbeuguel yi dafa rare Dièkou ma ni douma bale yeah yeah An konne yaw bandi nga ndèkè bebe Sopi nga sama xol bi limonade Siroter ko diko nane yeah yeah Ndax baniouy ndieukeu guissanter Li nga ma yene nimou disser Ak niniou xolanter Rek ma xamni yalla niou bolè Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (KAAY WAY) Doflo ngama (kaay waay) Wayè deufeul ngama (kaay waay) Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay) So bèguè ma bègue (kaay waay) Niou deukè di rè (kaay waay) Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay) Maala geuneul lounè (kaay waay) Teh yaama geuneul kounè (kaay waay) Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay) Bègal ma bèg (kaay waay) Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay) Soma sorè oh my love Namel bimay yeuk thi yaw Wallahi yaako meuneu fadie nieuweul Niouy kaf di rè Niouy kaaf di fo di rè Ndax baniouy ndieukeu guissanter Li nga ma yene nimou disser Ak niniou xolanter Rek ma xamni yalla niou bolè Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (KAAY WAY) Doflo ngama (kaay waay) Wayè deufeul ngama (kaay waay) Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay) So bèguè ma bègue (kaay waay) Niou deukè di rè (kaay waay) Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay) Maala geuneul lounè (kaay waay) Teh yaama geuneul kounè (kaay waay) Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay) Bègal ma bèg (kaay waay) Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay) Oh bebe toi mon bebe Toi qui m’a tout donner Je pourrais jamais te quitter Je t’en fais la promesse mon bebe Tu m’as tellement épauler Quand il le fallait M’a sorti de la galère Je vais te rendre la money Oh bebe yaw mi gounguè ma man malay gounguè Et si t’a peur crie aider moi mane maaa lay sauvé Oh bebe yaw ndax beuguè ngama comme nim la beuguè Ndax nim la beugè eup naaa wa li noum dèmè Oh bebe toi mon bebe Toi qui m’a tout donner Je pourrais jamais te quitter Je t’en fais la promesse mon bebe Tu m’as tellement épauler Quand il le fallait M’a sorti de la galère Je vais te rendre la money Oh bebe yaw mi gounguè ma #vj #kaayway #dm

VJ feat Seydou Che - Fatou Sangaré (Clip Officiel)

Wally B. Seck - ON IT (Live)

Scabble Music - SHATTA WALE AI TALK official audio

Mon fils handicapé dérange, ma sœur ne le supporte pas | Nayrafet

VIBES IN K.ZONE | Live mix by DJ SYLVA | Episode 3

Best of Senegal(Mbalax) 2025 Ft Wally Seck/Mia Guisse/Vj/Amadueus/Sidi Jiop/Dieyla/Jeeba/BassThioung

VJ - Sai Sai (Clip Officiel)

Fais moi confiance

Jahman X-press - WEURSEUK (official video)

NEW AFROBEATS 2026 VIDEO MIX | NEW NAIJA AFROBEATS VIDEO MIX(AYRA STARR RUSH |REMA SALENA CALM DOWN)

Djelykaba Bintou Feat. Mia Guissé - Unique (Clip Officiel)

VJ feat Sidiki Diabaté - Toi et Moi

IBRO NADIO: KINÉ NDIAYE - YAYE DIATOU - BAYE DIAW (lou bess) #livesn #ibronadio

Wally B. Seck - Je t’aime (Clip Officiel)

Best Of Senegal(Mbalax) 2024 Feat Wally Seck/Mia Guisse/Amadeus/VJ/ Dieyna/SIDY DIOP/Bass Thioung

AFROBEATS MIX 2026 | BEST OF 26, 25, 24 VIDEO MIX | AYRA STARR, REMA, FIREBOY, ASAKE, BURNA BOY

Amadeus - Bul ma seetaan (Clip Officiel)

Axel Merryl "Titulaire" Feat Mia Guisse & Bass Thioung (CLIP OFFICIEL)

Ibro Nadio Damala Nopp Ak Khady Ndiaye Au Five Night Club

