Leeral si Samba Laobe Penda ak Serigne Ganna Missra
Serigne Ganna Missra moy leeral digante Serigne Touba ak Mame Samba Laobe Penda. Samba Laobe Penda nekon bourba joloff ci 1890, jamono bobou Serigne Touba mingui nekon Touba. Bimu neke bourba joloff la bind ap letar Serin Tuba di saku si mom mu digal ko. Serin bi dal diko tontu yu am solo (moy sen njeuk jeuflante). Si euleuk sa werou mars Serin Tuba nieuw mbacke baari joloff ngir wajal tukkem bi, niou tek si wer maanam weru mai sila Mam Samba Laobe nieuw mbacke baari jolof jebalu si Serin bi andak joloff gepp, Serigne Fallu nettaliko. Lolu motax toubab bi fooliko bole ko ak Serin bi genalen reew mi.

▶︎
Samba Laobé Ndiaye, la vraie histoire...

▶︎
🚨 Abba brise le silence sur son conflit avec Bouba Ndour et sa suspension à la TFM

▶︎
🛑 WAKHTANÉ WAKHI MAME CHIEKH IBRAHIM FALL AK SERIGNE FALLOU FALL BAYE FALL BAYE

▶︎
FATOU GUEWEL - FIIRNDÉ SANTA BAMBA 1995

▶︎
Mathie b f tv recadrer becaye mbaye fadame yekini dou sa morome

▶︎
Nobody Breaks Celebrities Like Mr.Bean!

▶︎
160 KG VILLAGE MONSTER - The ANOMALY Nobody Can Explain - SUPERHUMAN ANDREY SMAEV

▶︎
Princess Of Boogie Woogie Delights Everyone

▶︎
Histoire de Serigne Touba et Samba Laobe Penda (1ére partie)

▶︎
He Didn't Know His Opponent Was Bruce Lee — A Martial Arts Champion Challenges a Random Guest

▶︎
People Who Messed With The Royal Guard and Regretted It!

▶︎
Samba Laobé Penda Ndiaye, l'histoire jamais racontée !

▶︎
Rowan Atkinson's Brilliant Humor Leaves Celebrities in Tears!

▶︎
Ego Bodybuilder HUMILIATED Beyond Belief 🤯 | Anatoly GYM PRANK

▶︎
Bolero en la Madrugada – Susurros de La Habana

▶︎
Ce Camerounais Timide Cartonne Avec Des Connaissances Exceptionnelles | DKP-B-Learning

▶︎
ლაზური / Dance "Lazuri"(2002)

▶︎
Was im vergessenen DEUTSCHEN Dorf in Georgien wirklich passiert…

▶︎
GHEORGHE ZAMFIR LA NICOLAE BOTGROS ANIVERSARE 2013 SALA PALATULUI

▶︎
