Big Dat X - Xale

Streamez ici : https://onerpm.link/215207336414 Artiste: Big Dat X Titre: Xale Voix additionnelles: Diodjista Prod: Snationbeats Enregistrement: Kajoor Music Mix/Master: Teacher Artwork: Joxhanei ———— Lyrics Heh yaw Bayiko Xel Xale la xamul Dara wooo oh Bayiko Xel yaw Gone la xamul Dara Nooo Bayiko Xel Xale la xamul Dara wooo oh Bayiko Xel yaw Gone la xamul Dara Nooo Ñuni Ndaw li Si gën moy yaw nga Bayi ko Xel Mani gone Li Si gën moy yaw Nga Yar ko Sa Teel Innocent La xamul Dara Yeaaah!! Yako wara Tek Si Yoon Fexe mu xamee lu baax ak lu bonn Education is the key caabi buntu addunam Bul tayyee dëkkee gëstu ndagam jangi nam Bant bi le Si Tooy-Tooy ngakoy Jubbantu Aveniram sa loxo tee ko biddënti Amal seetlu ci mom Teela seppi Ay jikkoom Fi Amna ñu ko Talul Ndax xëy Dem Wuti ji koom Heh yaw Bayiko Xel Xale la xamul Dara wooo oh Bayiko Xel yaw Gone la xamul Dara Nooo Bayiko Xel Xale la xamul Dara wooo oh Bayiko Xel yaw Gone la xamul Dara Nooo Yaw mani Fi amna criminel Amna pedophile Cas yu bari yunu mel viol ak i tek metit Àqq ak yelleef u xale bu amul Da ngey mujje Tiiit Lifi nekk a Doy waar Dema Children inda Street Mendicité sen fragilité lañi Soppi Business Ñii Di sagganee xale amul ku len gën a Yees Avenir u dëkk bi ci sen Loxo Yi la ne Ñoom la ki ñëpp wara ñee Amal seetlu ci mom Teela seppi Ay jikkoom Fi Amna ñu ko Talul Ndax xëy Dem Wuti ji koom Heh yaw Bayiko Xel Xale la xamul Dara wooo oh Bayiko Xel yaw Gone la xamul Dara Nooo Bayiko Xel Xale la xamul Dara wooo oh Bayiko Xel yaw Gone la xamul Dara Nooo #xale #rapactor #bigdatx