Big Dat X - - Actorism #4 (Directed by PMP STUDIO )
Auteur: Big Dat X Titre: Actorism #4 Prod: Papelaye Beats Enregistrement: MeloMusic Entertainment Mix/Master: ByMic Réalisation : PMP Studio Tv ————————————————————— Actorism #4 est disponible sur toutes plateformes de streaming :https://bfan.link/actorism —————————————————————— Suivez moi: Facebook 👉🏾 / big-dat-x-marxabane-team-650660248375778 Instagram👉🏾 https://instagram.com/bigdatx_loffici... —————————————————————— Lyrics Couplet 1 Man la game bi yàgg jooy te décéder guma Taaru mbind mi lay wan yoon même boo dee gumbë Petit à petit laay nokk tapéte yi ba du ñu rabati Back to beef 2pac Biggie ma damm sen bic yi Bulma boole si ñoom ndax dafa bari ay bitches Hit ´em up ready to die for the realness Badman bulma goondi ñóddi bad mind Boom gun dalay shot man Philosophy Descartes dalay cogiter lo X lyrics’am si melomind diko juter lo Actor la si rap na bandit yi profito bala fin wu film bi Firnde bi di hit yimay foowe do degg ni feel’u ma bii But anyway jurgoot sen’i nopp samay rhyme la Dat day ligeey exaequo ñoom sumay raam la Radio buma déchirer wul bul fa scotcher Putain bañal ni Patin sa équipe di es coacher God bind wuutële ku nekk ak jiko’om Respect lama jiitël men laataa may ji koom Dina fly si sky bi ni hélico Flow rhyme skillz fumu ne ma jëli ko Jeeriko’o Bu dee dafa tàng jër ci yaw Sama rabin bi wute na’g sa bii better nga know Ok ! OG kajoorois Thies la bayeeko Ku si jaay prek ma taak sa reum ba sa baay yëg ko Dangeen nara jómmi bu leen X Dat rap’bale Samay métaphore ne yu François Rabelais Style yi di taw te hit yi fune la nara ballee Namedrop Next Punch nimu lakoy ràbbalee Refrain Mana rude boy inadi place Black panther power cauz i’m from the black Race… Don’t play with the devil Céll’u mag du nelaw kon jarul xale tëb di dal Fu X dikk di rap Men Fok dëkk bi rëp Dangeen am jab di sap Te sen rap du dugg si ndëpp (x2) Couplet 2 Jamaican man i’m not But i can flow like Buju Banton Anybody try na test me football’u muumë ñam xam Listen! This one is for my guetto boy anh Long time me around quiet them still making noise Me nadi back i feel tegante deal No matter what you feel Man xaqq lay dekkil Ñu dellu hell Man rap dama siggil Sometimes them ask me what kind of music i’m listenning Boom.. ya’ll better know i’m just jumbling Kill kat u beat Def kat u hit Dama dépasser nit For real gën leen sadique Du polémique dama unique Sen dopest album yi laay fuck si 2 minutes man Duma nit man Bulma boole´g ay demi nit man Raab la si rizzla Ganja si Sizzla Rap la si beat lay def lu tàng high degrees la Crise la create si actor bi sen showbizz bi la Kiy jàpp emcees yi di bombe ki rómb maitrise bi la Hook Mana rude boy inadi place Black panther power cauz i’m from the black Race… Don’t play with the devil (x2) #bigdatx #actorism4 #rapgalsen #hiphop #senegal

Big Dat X - Yewwi Game Bi - Actorism #3 ( Directed by PMP STUDIO )

WAXTU JOT - Man G Feat Gun Mor (Vidéo Officielle) Prod By Kef Keffie (Azertis)

YACINE MUSIQUE

L'ANGE vs MAMY QUEEN | FINALE HELLO CYPHER

Jahman X-press - ARVA feat. Souleymane Faye, Soda Mama & Kine Lam (clip officiel)

BOOMRANG #1

Big Dat X - Niquage ( Vidéo Officielle )

Big Dat X:Loutax ma clash Ngaaka blinde matadi Akatsuki eljaz. flow up bi 5 million yi damakay dieul

BIG FLOW GROUPE LENIOL-NGOL # HADA LAMNDEE DO BERDE AM

Big Dat X - Ngoor prod by Viking Muzik

TERanga Cypher - Man G, Oz, Ko prip Diip, Taiji Scin, Rex T

Dip Doundou Guiss - Dungeen daj

BAC'AS - WAN MOR TIME ( Medley Diss ) Clip Officiel
![@mojocadambosse739 vs @Bigdatx - Back2Back[COMPLET]](https://i.ytimg.com/vi/C-Aq6YEmMxA/hqdefault.jpg?sqp=-oaymwEjCNACELwBSFryq4qpAxUIARUAAAAAGAElAADIQj0AgKJDeAE=&rs=AOn4CLCf27XJO-KezbSNlwep5Cx2uPb-UQ)
@mojocadambosse739 vs @Bigdatx - Back2Back[COMPLET]

Dafina Zeqiri x Cllevio - Buza

HARDCORE SIDE ft FLOOZ LOODUPZ-Rap Education-Clip Officiel By KDRD Films

Bruce Melodie- Détail (Offical Video)

Après le succès de son album validé par DIP…, BIG DAT X tire sur Ada Kanibal : « neu ñeuw gnou…»

THIAT KEURGUI - MISE AU POINT

