Seydina Insa Wade , Omar Blondin - Afrig + Xalima la Plume, Documentaire d'Ousmane William Mbaye
Omar Blondin Jóob - Afrig Fentkat & woykat bi: Seydinaa Isaa Wàdd Talli yaak taax ya di fuddu Ak di yuuxu di xar, Woto ya tàkk jëppeet! Dëmm ya wër sëg ya, Xooj ko ci ag séndël, Sëg ya di salliiru. Ma làmboo leer, jaar sëg ya, Junniy Omar dekki, Ñi ngiy sulli waa Ndeer ak ñi fi Caaroy, Géeju fen waa ngi nii di baawaan, Yàlla mi nu tiim, Ñàkk du nu tax a miim, Walla di wër di leb a leb a leb.... Le grand paragon (pharaon?), c'est Omar, Jàngal ndaw, ngir mooy li war. Jaasi du fi génn mbar, Xanaa ci lu ko jar. Raatale, umple, tële, Xamuñu, bëgguñu, sañuñu. Du doole fasu naaru góor, Du taaru jongoma ju mat, Loolu lépp dafay ruur. Ceddo amul kurus, Wante du rus. Eéy! Dégluleen yuuxu suufu Senegaal, Ànd ak yuuxu salup bi ci Gore! Sama fàttaliku di metti, Saa làmmiñ di saf deret. Bóom nañu Omar Jóob, Na ñu bóome waa Ndeer Ak ñi ci Caaroy! Géej giy jiñax(?), di ŋaax, Ngelaw liy tëb di sab ni rab, Asamaan siy dënu ni kënu, Niir yi di xaacu ngir di naqarlu, Talli yaak taax yay fuddu Ak di yuuxu di xar, Woto ya tàkk jëppeet! Dëmm ya wër sëg ya, Xooj ko ci ag séndël, Sëg ya di salliiru. Ma làmboo leer, jaar sëg ya, Junniy Omar dekki, Ñi ngiy xulli waa Ndeer ak ñi fi Caaroy. Ceddo amul kurus, Wante du rus... Ki jukki woy wi: Jolof Gaal

Le LOUNGE de Sen Tv avec Safia Invité Souleymane Faye (Live)

🚨🚨TFM LIVE : JAKAARLOO BI - Par : Pape Abdoulaye DER et sa team - 10 juillet 2026

Touré Kunda @ Afro-Pfingsten Festival 2018

Youssou Ndour 60 ans - Un Best of (3/3)

Erykah Badu & Alicia Keys – Hip Hop Soul, Jazz & Conscious Vibes (Timeless Playlist)

Archives d'afrique RFI Léopold Sédar Senghor

SELECTION CLIPS RETRO

Libaas

Village de Ndem Meissa , SERIGNE BABACAR MBOW , un modèle de développement durable

Ca Me Dit Mag - Hommage à Seydina Insa Wade - 12 Mai 2012 - Partie 3

CHEIKH LO Sukiyaki Tokyo 2015 Archive

JAKKAARLOO BI : GUISS-GUISS : ONU : Macky SALL annoncé à Dakar

TAFA DIARABI-Couleurs- Album Integral

Seydina Insa - "Waliyou" (Official Music Video)

Révélation de Pape Sané sur l'affaire Aicha Fatty / Abdoulaye Thiam, blanchiment ou amour impossible
![Omar Blondin Diop, Plutôt la mort que l'esclavage [E1] - Une étoile filante de l'ère Senghor](https://i.ytimg.com/vi/bB1SIHiQ3p8/hqdefault.jpg?sqp=-oaymwEjCNACELwBSFryq4qpAxUIARUAAAAAGAElAADIQj0AgKJDeAE=&rs=AOn4CLDosByvxQUflxzovq14f1U-K6ztXQ)
Omar Blondin Diop, Plutôt la mort que l'esclavage [E1] - Une étoile filante de l'ère Senghor
![Baaba Maal: On the Road [Full Live Album]](https://i.ytimg.com/vi/5KfY0vDzAWA/hqdefault.jpg?sqp=-oaymwEjCNACELwBSFryq4qpAxUIARUAAAAAGAElAADIQj0AgKJDeAE=&rs=AOn4CLBzo3cptGjqKyzLPqPwe0l0L73Zyg)
Baaba Maal: On the Road [Full Live Album]

Barry White | Deep Soul Classics (1973–1981) • Where Love Found Its Perfect Sound

Youssou Ndour | ACOUSTIC NOTES | by Mosow

